Sëyante jaare ko ci geemiñ do yoon buy faral di walle wala neewna di walle, ndam am yeneen anam yu mën di yokk wa di wanni walle gi. 10 AÑOS INFORMANDO Y ATENDIENDO A PERSONAS INMIGRANTES CON VIH 104 WOLOF 01 ANAM YI MËN YOKK BA WANNI WALLANTE TEGI SËYANTE JAARE KO CI GEEMIÑ Bañ ko weur ci been Anam, nit bu ame VIH te di fàccu, liimu doomu jaangoro ji day waññeko ba mënnef wallante gi day neew lol. Ndam sax sëyante jaar ko ci geemiñ baariwul wallante, mën naay wale tax ba nga wara jëffandiko kapot. Bu nit ki ame VIH di sëy jaare ko ci geemiñ, walle doomi jaangoro ji ki muy sëyal lu neew la dax jaangoro du walle ci tuflit yi. Bude jigeen ju ame VIH la sëyante jaar ci geemiñ ndam walle gi neew na. Di na war ng a and ak moytu bu fekke dafa tollu ci diiru giis bax, ndax doomu jaangoro ji mën ne ci deret ji. Bu goor gi ame VIH ndanu baax ci geemiñu ki mu ka sexal, wallante bi mëna yokku ndax ndox mi muy toor amna doomu jaangoro ji, rawatine bu dul fàccu. Bu fekke nit ki amul VIH dafa ame , sofe, ba dag dag, ba bëññ yi di nacc,bu sëyante jaar ci geemiñ wallante bi di gëna rey menglo ak bu geemiñ sette. Amn ay werente ci ndax ndoxu baax goor gu ame VIH, bi di jëk geen day walle. Lu ci ëpp wallante day neew dax lu tuttu mooy geen, wante tamit liimu doomu jaangoro ji dafay ajo ci anam yi mu tollu ci deret ji. WALLANTE FI MU ËPPE GTT-VIH GRUPO DE TRABAJO SOBRE TRATAMIENTOS DEL VIH - Sëyante jaareko ci nit ku ame VIH - Goor ndanu tur ndoxu baax ci geemiñ - Dag dag ba geemiñ ngu sofe ba bëññ yu nacc - Liim doomu jaangoro ngu rey ENTIDAD DECLARADA DE UTILIDAD PÚBLICA ONG DE DESARROLLO WALANTE NGU NEEW 02 - Sëy jaare ci geemiñ ak nit ku ame VIH - Bañña dekku ndoxum baaxu goor ci sa geemiñ - Geemiñ ngu set - Liimu doomu jaangoro ngu neew RAÑEE C Sëyante jaare ko ci geemiñ lu ci ëpp du walle, ndam sax amna ay anam yu mën yokk. Bu fekke nit dafa am VIH liimu doomu jaangoro ji dafa rey tur ndoxum ci geemiñ day yokk walle gi. Uttewul ak bu nit amul VIH te ame ay dag dag ci geemiñ ba sofe ba bëññ yu nacc. ¿TIENES DUDAS SOBRE EL TEMA? PREGÚNTANOS Tel. 93 458 26 41 [email protected] Un baññ di giis llimu doomu jaangoro ji ci dert ji day wànni walle ci sëyante yi. Mën walle tekkiwul Wall nan la ci li woor. Bu ci ame siki saka nga dem nu seetlu ndax ame nga VIH. INFOVIHTAL / SËYANTE JAARE KO CI GEEMIÑ