PAE-C11- Wolof primaria

Anuncio
form: AB-C11
NGUURU ARAGON
WAALU JANGALÉ
BÉENOO- XÉET AK TAGAAT YARAM
UBITÉ LÉKKOOL 201_/ 201_
ÁPP :
JANGALÉKAT YI :
CAABI LÉKKOOL BI :
GOX :
YÉEN WAAJUR YI,
YÉEN WAAJUR YI,
ÑU NGI LÉEN DI FATAALI SÉEN WARÉEF CI SÉEN YAR AK JANGU DOOM
______________________________ GIS NAÑU NÉ AM NA AY BÉS YU BARRÉ YUMU JANG SI
WUL.
ÑU NGI LÉEN DI FATAALI NÉ WUUTÉ YOYU, LAYYU ÑU LÉEN MU LÉER.
JANG YOON LA, TÉ JANGUM XÉLÉ WARÉEF LA BA BAMUYE AM FUKI AT AK JIROOM
BÉEN.
NGIR LÉERAL WUUTÉ YOYU , ÑU NGI LÉEN DI ÑAAN, NGÉEN TÉEWÉ WAXTAAN BI AM
CI LÉKKOOL BI, CI BÉSU :
_________________ CI ____________________ BU _________________
JIITU LÉKKOOL BI
ÑU NGI LÉEN DI FATAALI NI AM NA BÉEN NDAJÉ BUYE XÉEX WUUTÉ CI JANG BI, AM NA AY
BANKAS YUYE JAPP CI NDAJÉ BI , DI DÉF AY SAÏTU AK TOPP XÉLE YU NDAW YI CI SÉEN JANG BII,
DONE WARÉEF.
Descargar