wolof - Amediar

Anuncio
1. Lan mooy bile banxaasu caada yu
uute?
3. Yan xeeti tééré la ëmbb?
4. Ana ci lan lamay soxal?
- Xeeti tééré yi mu ëmbb xaajees nako yatti
Bile banxaasu caada yu uute benn la ci
banxaas yi nekk ci gëstukaayu nguur guii ñu
Bërëbu gëstukaay danay faral di jariñ ci:

pacc yu mak:
●
Di abale ay jumtukaay: niki ay tééré.
Ay CD, ay CD-ROM, ak yuni mel…
ay tééré yuy yeete ci mbiri uute ciy

dupee Manuel Alvar ci Zaragoza. Ñu ngi ko
caada: ci kallama español, aju ci
sos disi jublu dongg cosaanal xeet wu yaa te
yeneeni rééw akiy aada, boole ca lim
ci bërëbu xarala bi: ñu dileen fattali ni
uute.
bu takku ciy tééréy nettali.
man
Nguir man ko, namm nañu:
●
●
rééwma:
ay
tééré
ci
topatoo soxlo yi aju ci taggatu, ci
kallama bu uutek español taamu ca
teewlu ak caada
nakkallamay
ci xeet buy gen di
wuute
●
Mbinddum
bokk ci di yee xeet wi ci jikko yu raet
rééwu
Ubil bunt ñi soxlo jëfëndikoo ordinatëër
ngeen
faa
ubbi
seen
keesu
bataaxalu unternet ak xool buuntu webu
adduna bi yépp te dooleen fay dara.

cosaanu
doxandéém yi ëpp ci sunu gox bi.
Ngeen mana jangg xew-xew yi ñu
siiwël ak yëglekaayu adduna bi yëpp.
Njangum lakk, bokkna ca lakku español.

- xeeti jumtuwaay: tey fy tey, laca ëpp ya tééré
5. Nen laa fay mana gisee limay seet?
Jangg ak yër ci bërëbu tééré yi.
ñeel xeet wu bari melo.
2. Ana kan lañu ko jagleel?
la, ay CD mmisigu adduna bi, ay CD ROM akiy
Joteesna ci jumtukaay yi ci lu amul benn
Naka bërëbu gëstukaayu nguur yëpp, ak
yëglekaayu xibaar.
galangkoor. Ba taxna kiko soxlo man na caa jot
yeneen banxas yi nekk ci gëstukaayu Manuel
●
Lu aju ci yëglekaay yi, deesna ci
te du jaar fenn.
Alvar, banxaas bii ñeelna mboleem doomu
jappandal yëglekaayu addina bi yëpp:
Lu
adama, ak lu mana doon xeetam, baa rééw,
xibaari bës bi, yuñu sotti ci këyit, altine
gëstukaay bi ñu ngi leen di déglu ngir yombal
baa ay atam, baa pëyëm, baa diinéém, baa
ba gau, -jaaree ci jaww ji- taamu ci yi
seen jëfëndikoo jumtukaay yi.
lakam, laago, koom koom, liggééy wala
jugee ci rééwu doxandéém yi ëpp ci
Tayitam, ci jamono jii, ñungi ak kurel tektalkat
gnangam.
gox bi, boo xameen mënees nacaa jot.
ci aada yu uute, ñi ci nekk bokk ci ay xeet yu
Mënees
uute.
Limu ëmbb ciy tééré taxna mu soxal
lool askan wi bawoo ci yeneeni rééw ak
yépp ñi nga xamne caada yu uute lenn ciy
caada soxalna leen.
naa
nemmiku
ci
bërëbu
mana
xew
nak,
liggéykaati
bërëbu
gëstukay bii mbooleem yëglekaay yiñu
fay faral di sotti ci këyit.
Kenn ku nekk ci tektalkat yi man naa
jëféndikoo lakku rééwám ngir dimbëli ña fay
ñëw bu ñu ko soxlaa.
Ci bërëbu gëstukaay bi ak ci sunu buntu web
7. fan la nekk?
BANXAASU CAADA YU UUTE
Tektal:
BËRËBU GËSTUKAAY MANUAL
dingeen fa fekk “tektalukaay bi” ci kallaama
español, araab, rumani, poloñ, rusi, farañse,
angale…
ALVAR
Bërëbu gëstukaayu Manuel Alvar
6. Lan laay soxla gir jariñoo ko?
Edificio El Pilar, Parque Delicias.
Lees di ci laac, benn la ak ci bërëbu
50017 ZARAGOZA
gëstukaayu nguuri gox bi yëp. Kenn ku nekk
man na ci duggu ci lu amul benn galankoor te
Teléfono: 976 488 433
ñaring yi ñu jëkkë lim deesu ci fay dara.
Correo electrónico:
Guirmanamana abb di yobbu sa kër, ak di
[email protected]
doggu internet, wáy jëfëndiku bi warnaa joxe ci
Web: http://educacion.zaragoza.es
bërëbu gëstukaay bi ñaari nataalu dantite te
wane waale benn këyitu mandarga buñu koy
waxtuy kubbite:
xammee.
Altine ci ngoon: ci 15 waxtu ba 21 waxtu.
Ngir jëfëndikug internet, xale yi ammul juroom
Li dalee ko talaata ba aljuma: ci 9 waxtu ba
ñatti (8) at dañu wara andak seeni way jur
21 waxtu.
walla seeni njaatigui. Ñi am diggënte 8 ba 18
Gaau: ci 9 waxtu ba 14 waxtu
at, munul ñakk ñu wane këyit bu wax en seen
kilifa moleen nangul.
Weeru sulet ba waxset: dalee ko altine ba
ajuma, ci 9 waxtu ba 14 waxtu (ci suba si) ak ci
16 waxtu ba 21 00226waxt
Descargar